Prières en wolof | Dominik M. Ramík Dominik M. Ramík
Česky
In English


Prières en wolof

list Afficher la liste des prières en toutes les langues





autorenewChargement de la carte
 Langue vivante (91)   Langue en danger (6)   Langue moribonde / morte (2)
 Locuteur en dehors de la zone habituelle de la langue


Vous aimez ce projet? Soutenez le par une donation via PayPal.

Wolof

face Locuteur: Lena (Sénégal, Thiès)
add_circle_outline Église: Église catholique (romaine)
translate Plus d'information sur la langue: text_fields Écriture: latin (info sur ScriptSource)
import_contacts Origine du texte: Le texte vient des ressources officielles de l'église.

Signe de la Croix en wolof

play_circle_filled
Turu Baay bi ak Doom ji ak Xel mu Sell mi. Amiin

Notre Père en wolof

play_circle_filled
Sunu Baay, bi ci asamaan,
na sa tur sell,
na sa nguur dikk, loo bëgg,
na am ci suuf naka ca asamaan.
May nu tey sunu dundu bés bu nekk,
te baal nu sunuy tooñ,
naka nuy baale ña nu tooñ.
Tc bu nu bàyyi nu tàbbi ci bëliis,
wànte musal nu ci lu bon.
Amiin

Je vous salue Marie en wolof

play_circle_filled
Nuyu naa la, Maryaama,
fees nga ak yiw, borom baa ngi ak yow,
barkeel nga ci jigéen ñi yepp, te Yéesu, sa doomu biir, barkeel na.
Maryaama mu sell mi, Ndeyu Yàlla,
ñaanal ñu, ñun bàkkaarkat yi,
léegi ak ci suñu waxtu dee.
Amiin

Gloire au Père en wolof

play_circle_filled
Teranga ñell na Baay bi, Doom ji, ak Xel mu Sell mi,
naka la woon ca cosan la tey ak mos ba ca mos a mos.
Amiin
list Afficher la liste des prières en toutes les langues



Vous aimez ce projet? Soutenez le par une donation via PayPal.



Wallis & Futuna